Ad-Dukhan · 52/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ ۝٥٢
Fee jannaatinw wa `uyoon
📖 Tekkim Wolof
ci ay tooli dër ak i dex,

🎧 Dégg


📜 Aaya 50-54 — Simoore Ad-Dukhan

50إِنَّ هَٰذَا مَا كُنتُم بِهِ تَمْتَرُونَ
Lii nag tigi mooy li ngeen daan werante di ko sikki-sàkka.
51إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي مَقَامٍ أَمِينٍ
Ña ragaloon Yàlla te daan wattandiku ña nga ca ay kër yu wóor,
52فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
ci ay tooli dër ak i dex,
53يَلْبَسُونَ مِن سُندُسٍ وَإِسْتَبْرَقٍ مُّتَقَابِلِينَ
ñuy soloo ca xeeti sooy ya gën a ràññiku ne rojj jàkkarloo.
54كَذَٰلِكَ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
Noonu ! La ñu leen di maye ay soxna (yu am bët) huuru alayn.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 52

Simoore Ad-Dukhan Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci ay tooli dër ak i dex,

Simoore Aaya 52/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers