Ad-Dukhan · 51/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي مَقَامٍ أَمِينٍ ۝٥١
Innal muttaqeena fee maqaamin ameen
📖 Tekkim Wolof
Ña ragaloon Yàlla te daan wattandiku ña nga ca ay kër yu wóor,

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — Simoore Ad-Dukhan

49ذُقْ إِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْكَرِيمُ
Mosal tokamtikul ! Yaay [boroom kàttan] tey ku Tedd (daan rëy-rëylu).
50إِنَّ هَٰذَا مَا كُنتُم بِهِ تَمْتَرُونَ
Lii nag tigi mooy li ngeen daan werante di ko sikki-sàkka.
51إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي مَقَامٍ أَمِينٍ
Ña ragaloon Yàlla te daan wattandiku ña nga ca ay kër yu wóor,
52فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
ci ay tooli dër ak i dex,
53يَلْبَسُونَ مِن سُندُسٍ وَإِسْتَبْرَقٍ مُّتَقَابِلِينَ
ñuy soloo ca xeeti sooy ya gën a ràññiku ne rojj jàkkarloo.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 51

Simoore Ad-Dukhan Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragaloon Yàlla te daan wattandiku ña nga ca ay…

Simoore Aaya 51/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers