Ad-Dukhan · 58/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ ٥٨
Transliteration
Fa innamaa yassarnaahu bilisaanika la`allahum yatazakkaroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Di ko yombal ci saw làmmiñ, ngir amaana ñuy fàttaliku !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 56-59 — Simoore Ad-Dukhan
56لَا يَذُوقُونَ فِيهَا الْمَوْتَ إِلَّا الْمَوْتَةَ الْأُولَىٰ ۖ وَوَقَاهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
Duñu fa mos wextanu ndee lu dul dee gu jëkk ga. [Yàlla] fegal na leen mbugëlum Safara,
57فَضْلًا مِّن رَّبِّكَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe gu màgg ga.
58فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Di ko yombal ci saw làmmiñ, ngir amaana ñuy fàttaliku !
59فَارْتَقِبْ إِنَّهُم مُّرْتَقِبُونَ
Xaaral. Ñoom it ñi ngiy xaar.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
58Aaya
Tekki — Ad-Dukhan 58
Simoore Ad-Dukhan Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Di ko yombal ci saw làmmiñ, ngir amaana ñuy fàttaliku…Simoore Aaya 58/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 56–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








