Ad-Dukhan · 57/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
فَضْلًا مِّن رَّبِّكَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ ٥٧
Transliteration
Fadlam mir rabbik; zaalika huwal fawzul `azeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe gu màgg ga.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 55-59 — Ad-Dukhan
55يَدْعُونَ فِيهَا بِكُلِّ فَاكِهَةٍ آمِنِينَ
Ñu fay man a am wépp xeeti fuytéef féex lool ne fayax.
56لَا يَذُوقُونَ فِيهَا الْمَوْتَ إِلَّا الْمَوْتَةَ الْأُولَىٰ ۖ وَوَقَاهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
Duñu fa mos wextanu ndee lu dul dee gu jëkk ga. [Yàlla] fegal na leen mbugëlum Safara,
57فَضْلًا مِّن رَّبِّكَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe gu màgg ga.
58فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Di ko yombal ci saw làmmiñ, ngir amaana ñuy fàttaliku !
59فَارْتَقِبْ إِنَّهُم مُّرْتَقِبُونَ
Xaaral. Ñoom it ñi ngiy xaar.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
57Aaya
Tekki — Ad-Dukhan 57
Simoore Ad-Dukhan Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe…Simoore Aaya 57/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








