Ad-Dukhan · 59/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فَارْتَقِبْ إِنَّهُم مُّرْتَقِبُونَ ۝٥٩
Fartaqib innahum murta qiboon
📖 Tekkim Wolof
Xaaral. Ñoom it ñi ngiy xaar.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-59 — Simoore Ad-Dukhan

57فَضْلًا مِّن رَّبِّكَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe gu màgg ga.
58فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Di ko yombal ci saw làmmiñ, ngir amaana ñuy fàttaliku !
59فَارْتَقِبْ إِنَّهُم مُّرْتَقِبُونَ
Xaaral. Ñoom it ñi ngiy xaar.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 59

Simoore Ad-Dukhan Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xaaral. Ñoom it ñi ngiy xaar.

Simoore Aaya 59/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 57–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers