Al-Ahqaf · 20/35
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahqaf
وَيَوْمَ يُعْرَضُ الَّذِينَ كَفَرُوا عَلَى النَّارِ أَذْهَبْتُمْ طَيِّبَاتِكُمْ فِي حَيَاتِكُمُ الدُّنْيَا وَاسْتَمْتَعْتُم بِهَا فَالْيَوْمَ تُجْزَوْنَ عَذَابَ الْهُونِ بِمَا كُنتُمْ تَسْتَكْبِرُونَ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَبِمَا كُنتُمْ تَفْسُقُونَ ۝٢٠
Wa Yawma yu`radul lazeena kafaroo `alan Naai azhabtum taiyibaatikum fee hayaatikumud dunyaa wastam ta`tum bihaa fal Yawma tujzawna `azaabal hooni bimaa kuntum tastakbiroona fil ardi bighairil haqqi wa bimaa kuntum tafsuqoon
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee bis ba ñuy gaaral ña weddi ci kaw Safara (naan leen) : “jeexaloon ngeen séen yu neex ya ca jamono ba ngeen nekkee daan dund ca àddina : te pëcëxóowoon ngeen ko, bis bi niki tey dees na leen faye mbugalum toroxtaane, ngir ni ngeen daan saay-saayee.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Ahqaf

18أُولَٰئِكَ الَّذِينَ حَقَّ عَلَيْهِمُ الْقَوْلُ فِي أُمَمٍ قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلِهِم مِّنَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا خَاسِرِينَ
Ñoom ñooñee la wax ja dal ca séen kaw (menn mbugël) mooy xeet ya leen jiitu woon ci jinne yeek nit ñi. Ñoom dañoo yàqule woon.
19وَلِكُلٍّ دَرَجَاتٌ مِّمَّا عَمِلُوا ۖ وَلِيُوَفِّيَهُمْ أَعْمَالَهُمْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Kenn ku nekk am na lu tollook lamuy jëf, ñu nar leen a faye la ñu jëfoon te kenn du leen ca tooñ (ci wàññi natt ba).
20وَيَوْمَ يُعْرَضُ الَّذِينَ كَفَرُوا عَلَى النَّارِ أَذْهَبْتُمْ طَيِّبَاتِكُمْ فِي حَيَاتِكُمُ الدُّنْيَا وَاسْتَمْتَعْتُم بِهَا فَالْيَوْمَ تُجْزَوْنَ عَذَابَ الْهُونِ بِمَا كُنتُمْ تَسْتَكْبِرُونَ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَبِمَا كُنتُمْ تَفْسُقُونَ
Bu keroogee bis ba ñuy gaaral ña weddi ci kaw Safara (naan leen) : “jeexaloon ngeen séen yu neex ya ca jamono ba ngeen nekkee daan dund ca àddina : te pëcëxóowoon ngeen ko, bis bi niki tey dees na leen faye mbugalum toroxtaane, ngir ni ngeen daan saay-saayee.
21۞ وَاذْكُرْ أَخَا عَادٍ إِذْ أَنذَرَ قَوْمَهُ بِالْأَحْقَافِ وَقَدْ خَلَتِ النُّذُرُ مِن بَيْنِ يَدَيْهِ وَمِنْ خَلْفِهِ أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Fàttalikul mbokkum waa Aad ña (Huud) ba muy waar aw nitam ca barabu Al Ahqaaf – te fekkoon na waaraatekat ya jar fa la ko jiitu woon ak ginnaawam - [daan leen wax naan]: “Yàlla doŋŋ ngeen war a jaamu (waaye su ngeen jaamoo leneen lu dul moom). Man dey ragal naa ci yéen mbugëlum bis bu màgg ñàng”.
22قَالُوا أَجِئْتَنَا لِتَأْفِكَنَا عَنْ آلِهَتِنَا فَأْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Ñu tontu ko ne ko : “Moo ndax dangay ñëw ci nun ngir féewale nu bëgg nu bàyyi sunu yàlla yi ? Waay-waay, indil nu li nga nuy tëkkoo ndegam bokk nga ca way dëggu ña ”.
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Ahqaf 20

Simoore Al-Ahqaf Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee bis ba ñuy gaaral ña weddi ci kaw…

Simoore Aaya 20/35 — Simoore Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahqaf Dégg, Simoore Al-Ahqaf Tekki, Simoore Al-Ahqaf mp3, Simoore Al-Ahqaf pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers