Muhammad · 25/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
إِنَّ الَّذِينَ ارْتَدُّوا عَلَىٰ أَدْبَارِهِم مِّن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَى ۙ الشَّيْطَانُ سَوَّلَ لَهُمْ وَأَمْلَىٰ لَهُمْ ۝٢٥
Innal lazeenar taddoo `alaaa adbaarihim mim ba`di maa tabaiyana lahumul hudash Shaitaanu sawwala lahum wa amlaa lahum
📖 Tekkim Wolof
Ña murtad weddi ginnaaw ba leen njub ga feeñee, Saytaane legna leen te di leen fàbbi.
🎧 Dégg

📜 Aaya 23-27 — Muhammad

23أُولَٰئِكَ الَّذِينَ لَعَنَهُمُ اللَّهُ فَأَصَمَّهُمْ وَأَعْمَىٰ أَبْصَارَهُمْ
Ñooñu la Yàlla di rëbb, tëx loo na leen te gumba loo na séenub gis.
24أَفَلَا يَتَدَبَّرُونَ الْقُرْآنَ أَمْ عَلَىٰ قُلُوبٍ أَقْفَالُهَا
Moo ndax ñoom dañu dul settantal Alxuraan ? Wala séeni xol moo tojul ?
25إِنَّ الَّذِينَ ارْتَدُّوا عَلَىٰ أَدْبَارِهِم مِّن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَى ۙ الشَّيْطَانُ سَوَّلَ لَهُمْ وَأَمْلَىٰ لَهُمْ
Ña murtad weddi ginnaaw ba leen njub ga feeñee, Saytaane legna leen te di leen fàbbi.
26ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَالُوا لِلَّذِينَ كَرِهُوا مَا نَزَّلَ اللَّهُ سَنُطِيعُكُمْ فِي بَعْضِ الْأَمْرِ ۖ وَاللَّهُ يَعْلَمُ إِسْرَارَهُمْ
Li ko waral moo di dañuy wax yéefar yi naan leen : “dananu leen topp ci yennati mbir”. Te Yàlla xam na li ñuy nëbb.
27فَكَيْفَ إِذَا تَوَفَّتْهُمُ الْمَلَائِكَةُ يَضْرِبُونَ وُجُوهَهُمْ وَأَدْبَارَهُمْ
Naka la séeni mbir di mujje su leen Malaaka ya jekkalee, di leen dóor ci kanam ak ginnaaw ?
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
25Aaya

Tekki — Muhammad 25

Simoore Muhammad Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña murtad weddi ginnaaw ba leen njub ga feeñee, Saytaane…

Simoore Aaya 25/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers