Muhammad · 24/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
أَفَلَا يَتَدَبَّرُونَ الْقُرْآنَ أَمْ عَلَىٰ قُلُوبٍ أَقْفَالُهَا ٢٤
Transliteration
Afalaa yatadabbaroonal Qur-aana am `alaa quloobin aqfaaluhaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ñoom dañu dul settantal Alxuraan ? Wala séeni xol moo tojul ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — Muhammad
22فَهَلْ عَسَيْتُمْ إِن تَوَلَّيْتُمْ أَن تُفْسِدُوا فِي الْأَرْضِ وَتُقَطِّعُوا أَرْحَامَكُمْ
Moo ndax, su ngeen dëddoo baña xare ji loolu du jur ak yàq ci suuf si ak ngeen di dog séenug mbokk ?
23أُولَٰئِكَ الَّذِينَ لَعَنَهُمُ اللَّهُ فَأَصَمَّهُمْ وَأَعْمَىٰ أَبْصَارَهُمْ
Ñooñu la Yàlla di rëbb, tëx loo na leen te gumba loo na séenub gis.
24أَفَلَا يَتَدَبَّرُونَ الْقُرْآنَ أَمْ عَلَىٰ قُلُوبٍ أَقْفَالُهَا
Moo ndax ñoom dañu dul settantal Alxuraan ? Wala séeni xol moo tojul ?
25إِنَّ الَّذِينَ ارْتَدُّوا عَلَىٰ أَدْبَارِهِم مِّن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَى ۙ الشَّيْطَانُ سَوَّلَ لَهُمْ وَأَمْلَىٰ لَهُمْ
Ña murtad weddi ginnaaw ba leen njub ga feeñee, Saytaane legna leen te di leen fàbbi.
26ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَالُوا لِلَّذِينَ كَرِهُوا مَا نَزَّلَ اللَّهُ سَنُطِيعُكُمْ فِي بَعْضِ الْأَمْرِ ۖ وَاللَّهُ يَعْلَمُ إِسْرَارَهُمْ
Li ko waral moo di dañuy wax yéefar yi naan leen : “dananu leen topp ci yennati mbir”. Te Yàlla xam na li ñuy nëbb.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
24Aaya
Tekki — Muhammad 24
Simoore Muhammad Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ñoom dañu dul settantal Alxuraan ? Wala séeni…Simoore Aaya 24/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








