Qaf · 31/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ غَيْرَ بَعِيدٍ ٣١
Transliteration
Wa uzlifatil jannatu lil muttaqeena ghaira ba`eed
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu waajal Àjjana way ragal ña Yàlla mu jigeñ loolu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 29-33 — Qaf
29مَا يُبَدَّلُ الْقَوْلُ لَدَيَّ وَمَا أَنَا بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
Wax ja du sippiku fi man ; te it Duma tooñ benn jaam”.
30يَوْمَ نَقُولُ لِجَهَنَّمَ هَلِ امْتَلَأْتِ وَتَقُولُ هَلْ مِن مَّزِيدٍ
Bu keroogee ba Nuy laaj Safara naan ko ; “Ndax fees nga ? ” Safara naan : “Dolli ma” ?
31وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ غَيْرَ بَعِيدٍ
Nu waajal Àjjana way ragal ña Yàlla mu jigeñ loolu.
32هَٰذَا مَا تُوعَدُونَ لِكُلِّ أَوَّابٍ حَفِيظٍ
“Lii mooy li Nu leen daan dig , [mu ñeel] bépp delluwaakoon ci Boroomam tey sàmm [daytalu Boroomam]
33مَّنْ خَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ وَجَاءَ بِقَلْبٍ مُّنِيبٍ
kuy ragal Yàlla Yërëmakoon bi ci kumpa, te ñëw ànd ak xol bu nangu ndigal.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
31Aaya
Tekki — Qaf 31
Simoore Qaf Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu waajal Àjjana way ragal ña Yàlla mu jigeñ loolu.Simoore Aaya 31/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








