At-Tur · 18/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
فَاكِهِينَ بِمَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ وَوَقَاهُمْ رَبُّهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ ١٨
Transliteration
Faakiheena bimaaa aataahum rabbuhum wa waqaahum rabbuhum `azaabal jaheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ñangay xéewlóo la leen seen Boroom jox, te it fàggulna leen mbugalum Safara.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 16-20 — At-Tur
16اصْلَوْهَا فَاصْبِرُوا أَوْ لَا تَصْبِرُوا سَوَاءٌ عَلَيْكُمْ ۖ إِنَّمَا تُجْزَوْنَ مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Xoyomleen ci biir ! Ngeen muñ ak ngeen ñàkk a muñ , ñoo ci yem képp : ci yéen ak lu man a xew dangay jot peyug la ngeen daan jëf.
17إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَنَعِيمٍ
Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana ya ak i xéewël,
18فَاكِهِينَ بِمَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ وَوَقَاهُمْ رَبُّهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
ñangay xéewlóo la leen seen Boroom jox, te it fàggulna leen mbugalum Safara.
19كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan ndokkale, ngir la ngeen daan jëf,
20مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ سُرُرٍ مَّصْفُوفَةٍ ۖ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may Nanu leen ay soxna yu “huuru al iin” (am bët jekk),
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
18Aaya
Tekki — At-Tur 18
Simoore At-Tur Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñangay xéewlóo la leen seen Boroom jox, te it fàggulna…Simoore Aaya 18/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








