Al-Qamar · 4/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّنَ الْأَنبَاءِ مَا فِيهِ مُزْدَجَرٌ ۝٤
Wa laqad jaaa`ahum minal ambaaa`i maa feehi muzdajar
📖 Tekkim Wolof
Te jot nañu ci ay xibaar lu leen man a jàjj ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Qamar

2وَإِن يَرَوْا آيَةً يُعْرِضُوا وَيَقُولُوا سِحْرٌ مُّسْتَمِرٌّ
Saa su ñu gisee keemaan, dañuy dumóoyu tey wax naan : “Lii ag njibar laati”.
3وَكَذَّبُوا وَاتَّبَعُوا أَهْوَاءَهُمْ ۚ وَكُلُّ أَمْرٍ مُّسْتَقِرٌّ
weddi nañu topp nañu it seen bànneex, te mbir yépp a ngi ne roŋŋ
4وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّنَ الْأَنبَاءِ مَا فِيهِ مُزْدَجَرٌ
Te jot nañu ci ay xibaar lu leen man a jàjj ;
5حِكْمَةٌ بَالِغَةٌ ۖ فَمَا تُغْنِ النُّذُرُ
Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.
6فَتَوَلَّ عَنْهُمْ ۘ يَوْمَ يَدْعُ الدَّاعِ إِلَىٰ شَيْءٍ نُّكُرٍ
Nangeen leen dumóoyu. Bu keroogee ba wootekat ba di woote jëm ci mbir mu naqari,
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Qamar 4

Simoore Al-Qamar Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te jot nañu ci ay xibaar lu leen man a…

Simoore Aaya 4/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers