Al-Qamar · 3/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَكَذَّبُوا وَاتَّبَعُوا أَهْوَاءَهُمْ ۚ وَكُلُّ أَمْرٍ مُّسْتَقِرٌّ ۝٣
Wa kazzaboo wattaba`ooo ahwaaa`ahum; wa kullu amrim mustaqirr
📖 Tekkim Wolof
weddi nañu topp nañu it seen bànneex, te mbir yépp a ngi ne roŋŋ

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Qamar

1اقْتَرَبَتِ السَّاعَةُ وَانشَقَّ الْقَمَرُ
Waxtu wi jigesi na weer wi xar na (bis pénc ba).
2وَإِن يَرَوْا آيَةً يُعْرِضُوا وَيَقُولُوا سِحْرٌ مُّسْتَمِرٌّ
Saa su ñu gisee keemaan, dañuy dumóoyu tey wax naan : “Lii ag njibar laati”.
3وَكَذَّبُوا وَاتَّبَعُوا أَهْوَاءَهُمْ ۚ وَكُلُّ أَمْرٍ مُّسْتَقِرٌّ
weddi nañu topp nañu it seen bànneex, te mbir yépp a ngi ne roŋŋ
4وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّنَ الْأَنبَاءِ مَا فِيهِ مُزْدَجَرٌ
Te jot nañu ci ay xibaar lu leen man a jàjj ;
5حِكْمَةٌ بَالِغَةٌ ۖ فَمَا تُغْنِ النُّذُرُ
Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Qamar 3

Simoore Al-Qamar Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : weddi nañu topp nañu it seen bànneex, te mbir yépp…

Simoore Aaya 3/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers