Al-Qamar · 5/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
حِكْمَةٌ بَالِغَةٌ ۖ فَمَا تُغْنِ النُّذُرُ ۝٥
Hikmatum baalighatun famaa tughnin nuzur
📖 Tekkim Wolof
Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Qamar

3وَكَذَّبُوا وَاتَّبَعُوا أَهْوَاءَهُمْ ۚ وَكُلُّ أَمْرٍ مُّسْتَقِرٌّ
weddi nañu topp nañu it seen bànneex, te mbir yépp a ngi ne roŋŋ
4وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّنَ الْأَنبَاءِ مَا فِيهِ مُزْدَجَرٌ
Te jot nañu ci ay xibaar lu leen man a jàjj ;
5حِكْمَةٌ بَالِغَةٌ ۖ فَمَا تُغْنِ النُّذُرُ
Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.
6فَتَوَلَّ عَنْهُمْ ۘ يَوْمَ يَدْعُ الدَّاعِ إِلَىٰ شَيْءٍ نُّكُرٍ
Nangeen leen dumóoyu. Bu keroogee ba wootekat ba di woote jëm ci mbir mu naqari,
7خُشَّعًا أَبْصَارُهُمْ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ كَأَنَّهُمْ جَرَادٌ مُّنتَشِرٌ
ñuy jatt seeni gis ba, di génne ci bàmmeel yi dañuy melni ay soccent yu ñu tasaare,
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Qamar 5

Simoore Al-Qamar Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.

Simoore Aaya 5/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers