Al-Qamar · 43/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
أَكُفَّارُكُمْ خَيْرٌ مِّنْ أُولَٰئِكُمْ أَمْ لَكُم بَرَاءَةٌ فِي الزُّبُرِ ۝٤٣
Akuffaarukum khairum min ulaaa`ikum am lakum baraaa`atun fiz Zubur
📖 Tekkim Wolof
Seen yéefar yi ndax dañoo gën ñooña ? Walla dañu leen bindal ci téere yi ne mucc ngeen ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Al-Qamar

41وَلَقَدْ جَاءَ آلَ فِرْعَوْنَ النُّذُرُ
Nitu Firawna ya ñoom it, xupp ga dikkaloon na leen.
42كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كُلِّهَا فَأَخَذْنَاهُمْ أَخْذَ عَزِيزٍ مُّقْتَدِرٍ
Ñoom dañoo weddi faf sunu kàddu yépp. Nu daldi leen faagaagal, ak doole.
43أَكُفَّارُكُمْ خَيْرٌ مِّنْ أُولَٰئِكُمْ أَمْ لَكُم بَرَاءَةٌ فِي الزُّبُرِ
Seen yéefar yi ndax dañoo gën ñooña ? Walla dañu leen bindal ci téere yi ne mucc ngeen ?
44أَمْ يَقُولُونَ نَحْنُ جَمِيعٌ مُّنتَصِرٌ
Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am ndam”.
45سَيُهْزَمُ الْجَمْعُ وَيُوَلُّونَ الدُّبُرَ
Seen booloo gi dana tas , ñu ne wëqét daw wane ginnaaw.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Qamar 43

Simoore Al-Qamar Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen yéefar yi ndax dañoo gën ñooña ? Walla dañu…

Simoore Aaya 43/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers