Al-Qamar · 44/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
أَمْ يَقُولُونَ نَحْنُ جَمِيعٌ مُّنتَصِرٌ ٤٤
Transliteration
Am yaqooloona nahnu jamee`um muntasir
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am ndam”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 42-46 — Al-Qamar
42كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كُلِّهَا فَأَخَذْنَاهُمْ أَخْذَ عَزِيزٍ مُّقْتَدِرٍ
Ñoom dañoo weddi faf sunu kàddu yépp. Nu daldi leen faagaagal, ak doole.
43أَكُفَّارُكُمْ خَيْرٌ مِّنْ أُولَٰئِكُمْ أَمْ لَكُم بَرَاءَةٌ فِي الزُّبُرِ
Seen yéefar yi ndax dañoo gën ñooña ? Walla dañu leen bindal ci téere yi ne mucc ngeen ?
44أَمْ يَقُولُونَ نَحْنُ جَمِيعٌ مُّنتَصِرٌ
Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am ndam”.
45سَيُهْزَمُ الْجَمْعُ وَيُوَلُّونَ الدُّبُرَ
Seen booloo gi dana tas , ñu ne wëqét daw wane ginnaaw.
46بَلِ السَّاعَةُ مَوْعِدُهُمْ وَالسَّاعَةُ أَدْهَىٰ وَأَمَرُّ
Bis Pénc, ba la ñuy dajeeti, te bis Pénc moo gënatee mitti te tar.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
44Aaya
Tekki — Al-Qamar 44
Simoore Al-Qamar Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am…Simoore Aaya 44/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








