Al-Qamar · 42/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كُلِّهَا فَأَخَذْنَاهُمْ أَخْذَ عَزِيزٍ مُّقْتَدِرٍ ۝٤٢
Kazzaboo bi Aayaatinaa kullihaa fa akhaznaahum akhza `azeezim muqtadir
📖 Tekkim Wolof
Ñoom dañoo weddi faf sunu kàddu yépp. Nu daldi leen faagaagal, ak doole.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 40-44 — Simoore Al-Qamar

40وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Mo ndax kon kenn dana ca jàjjoo ?
41وَلَقَدْ جَاءَ آلَ فِرْعَوْنَ النُّذُرُ
Nitu Firawna ya ñoom it, xupp ga dikkaloon na leen.
42كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كُلِّهَا فَأَخَذْنَاهُمْ أَخْذَ عَزِيزٍ مُّقْتَدِرٍ
Ñoom dañoo weddi faf sunu kàddu yépp. Nu daldi leen faagaagal, ak doole.
43أَكُفَّارُكُمْ خَيْرٌ مِّنْ أُولَٰئِكُمْ أَمْ لَكُم بَرَاءَةٌ فِي الزُّبُرِ
Seen yéefar yi ndax dañoo gën ñooña ? Walla dañu leen bindal ci téere yi ne mucc ngeen ?
44أَمْ يَقُولُونَ نَحْنُ جَمِيعٌ مُّنتَصِرٌ
Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am ndam”.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Qamar 42

Simoore Al-Qamar Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom dañoo weddi faf sunu kàddu yépp. Nu daldi leen…

Simoore Aaya 42/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers