Al-Qamar · 54/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَنَهَرٍ ۝٥٤
Innal muttaqeena fee jannaatinw wa nahar
📖 Tekkim Wolof
Ña ragal Yàlla ña nga ca àjjana yu am i dex,

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-55 — Al-Qamar

52وَكُلُّ شَيْءٍ فَعَلُوهُ فِي الزُّبُرِ
Te lépp lu ñu defoon bind Nanu ko ca téere ya,
53وَكُلُّ صَغِيرٍ وَكَبِيرٍ مُّسْتَطَرٌ
lépp, lu ndaw ak lu mag, karmat nañu ko ca.
54إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَنَهَرٍ
Ña ragal Yàlla ña nga ca àjjana yu am i dex,
55فِي مَقْعَدِ صِدْقٍ عِندَ مَلِيكٍ مُّقْتَدِرٍ
ca kërug dëgg ga, fa Buur Bu am kàttan ba.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Al-Qamar 54

Simoore Al-Qamar Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragal Yàlla ña nga ca àjjana yu am i…

Simoore Aaya 54/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 52–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers