Al-Qamar · 53/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَكُلُّ صَغِيرٍ وَكَبِيرٍ مُّسْتَطَرٌ ۝٥٣
Wa kullu sagheerinw wa kabeerim mustatar
📖 Tekkim Wolof
lépp, lu ndaw ak lu mag, karmat nañu ko ca.

🎧 Dégg


📜 Aaya 51-55 — Simoore Al-Qamar

51وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا أَشْيَاعَكُمْ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Faagaagal Nanu, ay xeet yu mel ni yéen. Mo ndax kon kenn du fàttaliku jàjj ?
52وَكُلُّ شَيْءٍ فَعَلُوهُ فِي الزُّبُرِ
Te lépp lu ñu defoon bind Nanu ko ca téere ya,
53وَكُلُّ صَغِيرٍ وَكَبِيرٍ مُّسْتَطَرٌ
lépp, lu ndaw ak lu mag, karmat nañu ko ca.
54إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَنَهَرٍ
Ña ragal Yàlla ña nga ca àjjana yu am i dex,
55فِي مَقْعَدِ صِدْقٍ عِندَ مَلِيكٍ مُّقْتَدِرٍ
ca kërug dëgg ga, fa Buur Bu am kàttan ba.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Al-Qamar 53

Simoore Al-Qamar Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lépp, lu ndaw ak lu mag, karmat nañu ko ca.

Simoore Aaya 53/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers