Ar-Rahman · 62/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
وَمِن دُونِهِمَا جَنَّتَانِ ۝٦٢
Wa min doonihimaa jannataan
📖 Tekkim Wolof
Ci dër yooyu amaat na yeneen ñaari dër.

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Ar-Rahman

60هَلْ جَزَاءُ الْإِحْسَانِ إِلَّا الْإِحْسَانُ
Moo ndax lu rafet man naa am geneen pey guddul lu rafet (mukk du am) ?
61فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
62وَمِن دُونِهِمَا جَنَّتَانِ
Ci dër yooyu amaat na yeneen ñaari dër.
63فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
64مُدْهَامَّتَانِ
Ñu di ñaari dër yu naat lool nëtëx.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
62Aaya

Tekki — Ar-Rahman 62

Simoore Ar-Rahman Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ci dër yooyu amaat na yeneen ñaari dër.

Simoore Aaya 62/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers