Ar-Rahman · 76/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ رَفْرَفٍ خُضْرٍ وَعَبْقَرِيٍّ حِسَانٍ ۝٧٦
Muttaki`eena `alaa rafratin khudrinw wa `abqariyyin hisaan
📖 Tekkim Wolof
Ña ngeen soonu ci ay ngegenaay yu nëtëx (wert) ak ay laltaay yu rafet.

🎧 Dégg


📜 Aaya 74-78 — Simoore Ar-Rahman

74لَمْ يَطْمِثْهُنَّ إِنسٌ قَبْلَهُمْ وَلَا جَانٌّ
nit wala jinne masuta laal jigéen ñooñu.
75فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
76مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ رَفْرَفٍ خُضْرٍ وَعَبْقَرِيٍّ حِسَانٍ
Ña ngeen soonu ci ay ngegenaay yu nëtëx (wert) ak ay laltaay yu rafet.
77فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
78تَبَارَكَ اسْمُ رَبِّكَ ذِي الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ
Saw turu Boroom Baarkeel na, moom miy Boroom Màgg ak Teraanga ji !
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
76Aaya

Tekki — Ar-Rahman 76

Simoore Ar-Rahman Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ngeen soonu ci ay ngegenaay yu nëtëx (wert) ak…

Simoore Aaya 76/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers