Al-Waqi'a · 73/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
نَحْنُ جَعَلْنَاهَا تَذْكِرَةً وَمَتَاعًا لِّلْمُقْوِينَ ۝٧٣
Nahnu ja`alnaahaa tazkira tanw wa mataa`al lilmuqween
📖 Tekkim Wolof
Def nanu ko mu di ag fàttali (ci safaraw ëllëg), di jumtukaay ci képp ku ko ittewoo.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 71-75 — Simoore Al-Waqi'a

71أَفَرَأَيْتُمُ النَّارَ الَّتِي تُورُونَ
Xanaa gisuleen Safara wi ngeen di taaloo ?
72أَأَنتُمْ أَنشَأْتُمْ شَجَرَتَهَا أَمْ نَحْنُ الْمُنشِئُونَ
Moo ndax yéen a sos garab gi walla Nun noo ko sos sàkk ko ?
73نَحْنُ جَعَلْنَاهَا تَذْكِرَةً وَمَتَاعًا لِّلْمُقْوِينَ
Def nanu ko mu di ag fàttali (ci safaraw ëllëg), di jumtukaay ci képp ku ko ittewoo.
74فَسَبِّحْ بِاسْمِ رَبِّكَ الْعَظِيمِ
Na ngay sàbbaal sa Boroom, bu Màgg bi !
75۞ فَلَا أُقْسِمُ بِمَوَاقِعِ النُّجُومِ
Déet !... maa ngi giiñ ci wàccuwaayi biddiw yi.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 73

Simoore Al-Waqi'a Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def nanu ko mu di ag fàttali (ci safaraw ëllëg),…

Simoore Aaya 73/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers