Al-Waqi'a · 72/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
أَأَنتُمْ أَنشَأْتُمْ شَجَرَتَهَا أَمْ نَحْنُ الْمُنشِئُونَ ۝٧٢
A-antum anshaatum shajaratahaaa am nahnul munshi`oon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax yéen a sos garab gi walla Nun noo ko sos sàkk ko ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 70-74 — Simoore Al-Waqi'a

70لَوْ نَشَاءُ جَعَلْنَاهُ أُجَاجًا فَلَوْلَا تَشْكُرُونَ
Sunu neexoon, Nu sëccël ko mu wex xàtt ak xorom. Moo xanaa dungeen sant ?
71أَفَرَأَيْتُمُ النَّارَ الَّتِي تُورُونَ
Xanaa gisuleen Safara wi ngeen di taaloo ?
72أَأَنتُمْ أَنشَأْتُمْ شَجَرَتَهَا أَمْ نَحْنُ الْمُنشِئُونَ
Moo ndax yéen a sos garab gi walla Nun noo ko sos sàkk ko ?
73نَحْنُ جَعَلْنَاهَا تَذْكِرَةً وَمَتَاعًا لِّلْمُقْوِينَ
Def nanu ko mu di ag fàttali (ci safaraw ëllëg), di jumtukaay ci képp ku ko ittewoo.
74فَسَبِّحْ بِاسْمِ رَبِّكَ الْعَظِيمِ
Na ngay sàbbaal sa Boroom, bu Màgg bi !
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 72

Simoore Al-Waqi'a Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax yéen a sos garab gi walla Nun noo…

Simoore Aaya 72/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers