Al-Waqi'a · 74/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَسَبِّحْ بِاسْمِ رَبِّكَ الْعَظِيمِ ۝٧٤
Fasabbih bismi Rabbikal `azeem
📖 Tekkim Wolof
Na ngay sàbbaal sa Boroom, bu Màgg bi !

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore Al-Waqi'a

72أَأَنتُمْ أَنشَأْتُمْ شَجَرَتَهَا أَمْ نَحْنُ الْمُنشِئُونَ
Moo ndax yéen a sos garab gi walla Nun noo ko sos sàkk ko ?
73نَحْنُ جَعَلْنَاهَا تَذْكِرَةً وَمَتَاعًا لِّلْمُقْوِينَ
Def nanu ko mu di ag fàttali (ci safaraw ëllëg), di jumtukaay ci képp ku ko ittewoo.
74فَسَبِّحْ بِاسْمِ رَبِّكَ الْعَظِيمِ
Na ngay sàbbaal sa Boroom, bu Màgg bi !
75۞ فَلَا أُقْسِمُ بِمَوَاقِعِ النُّجُومِ
Déet !... maa ngi giiñ ci wàccuwaayi biddiw yi.
76وَإِنَّهُ لَقَسَمٌ لَّوْ تَعْلَمُونَ عَظِيمٌ
Su ngeen xamoon lii, ngiiñ lu màgg la de.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 74

Simoore Al-Waqi'a Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Na ngay sàbbaal sa Boroom, bu Màgg bi !

Simoore Aaya 74/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers