Al-Mumtahina · 7/13
Tekki Waxtaan — Al-Mumtahina
۞ عَسَى اللَّهُ أَن يَجْعَلَ بَيْنَكُمْ وَبَيْنَ الَّذِينَ عَادَيْتُم مِّنْهُم مَّوَدَّةً ۚ وَاللَّهُ قَدِيرٌ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ ۝٧
Asal laahu any yaj`ala bainakum wa bainal lazeena `aadaitum minhum mawaddah; wallahu qadeer; wallahu ghafoorur raheem
📖 Tekkim Wolof
Amaana bu Yàlla defee ci seen diggante ak ñi ngeen noonooloon ag bëggënte. Yàlla Ku Man la te Yàlla Jéggëlaakoon Jaglewaakoon la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 5-9 — Al-Mumtahina

5رَبَّنَا لَا تَجْعَلْنَا فِتْنَةً لِّلَّذِينَ كَفَرُوا وَاغْفِرْ لَنَا رَبَّنَا ۖ إِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Yaw sunu Boroom, bul nu def mukk [sànje] ci loxoy yéefar yi ; te nanga nu jéggal, Yaw, yaa di Boroom Kàttan gi, di Ku Xereñ ki”
6لَقَدْ كَانَ لَكُمْ فِيهِمْ أُسْوَةٌ حَسَنَةٌ لِّمَن كَانَ يَرْجُو اللَّهَ وَالْيَوْمَ الْآخِرَ ۚ وَمَن يَتَوَلَّ فَإِنَّ اللَّهَ هُوَ الْغَنِيُّ الْحَمِيدُ
Ñoom am ngeen ci ñoom royuwaay wu rafet, mu ñeel képp ku yaakaar Yàlla ak Bis bu mujj ba : képp ku dumóoyu nag... na xam ne Yàlla ku doyloo boppam Yayoowaakoonu cant la.
7۞ عَسَى اللَّهُ أَن يَجْعَلَ بَيْنَكُمْ وَبَيْنَ الَّذِينَ عَادَيْتُم مِّنْهُم مَّوَدَّةً ۚ وَاللَّهُ قَدِيرٌ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Amaana bu Yàlla defee ci seen diggante ak ñi ngeen noonooloon ag bëggënte. Yàlla Ku Man la te Yàlla Jéggëlaakoon Jaglewaakoon la.
8لَّا يَنْهَاكُمُ اللَّهُ عَنِ الَّذِينَ لَمْ يُقَاتِلُوكُمْ فِي الدِّينِ وَلَمْ يُخْرِجُوكُم مِّن دِيَارِكُمْ أَن تَبَرُّوهُمْ وَتُقْسِطُوا إِلَيْهِمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الْمُقْسِطِينَ
Yàlla duleen tere ngeen di maslaa ak di laamisook ñi xeexul ak yéen ci seen diine te génnewuñuleen seeni kër. Yàlla safoona way maandu yi.
9إِنَّمَا يَنْهَاكُمُ اللَّهُ عَنِ الَّذِينَ قَاتَلُوكُمْ فِي الدِّينِ وَأَخْرَجُوكُم مِّن دِيَارِكُمْ وَظَاهَرُوا عَلَىٰ إِخْرَاجِكُمْ أَن تَوَلَّوْهُمْ ۚ وَمَن يَتَوَلَّهُمْ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Ñi leen Yàlla di tere kay ñooy ñiy xeex ak yéen ci diine, di leen génnee ci seeni kër walla ña leen cay jàppale. Buleen xaritoo mukk ak ñoom képp kuy xaritook ñoom ñooy tooñkat yi.
Al-MumtahinaFihi Alxuraan
13Aaya
MedinanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Mumtahina 7

Simoore Al-Mumtahina Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amaana bu Yàlla defee ci seen diggante ak ñi ngeen…

Simoore Aaya 7/13 — Al-Mumtahina الممتحنة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mumtahina Dégg, Al-Mumtahina Tekki, Al-Mumtahina mp3, Al-Mumtahina pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers