As-Saff · 13/14
Tekki Waxtaan — As-Saff
وَأُخْرَىٰ تُحِبُّونَهَا ۖ نَصْرٌ مِّنَ اللَّهِ وَفَتْحٌ قَرِيبٌ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ ١٣
Transliteration
Wa ukhraa tuhibboonahaa nasrum minal laahi wa fat hun qaree; wa bashshiril mu `mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
dana leen defal it yeneeni mbir yu ngeen bëgg : ndimbal [lu bawoo] fa Yàlla ak ndam lu jige. Bégalal jullit ñi ci xibaar bu neex bi.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 11-14 — As-Saff
11تُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَرَسُولِهِ وَتُجَاهِدُونَ فِي سَبِيلِ اللَّهِ بِأَمْوَالِكُمْ وَأَنفُسِكُمْ ۚ ذَٰلِكُمْ خَيْرٌ لَّكُمْ إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Dangeen di gëm Yàlla ak ub Yonentam tey xare ci yoonu Yàlla ak seeni alal ak seeni bakkan, looloo gën ci yéen de, cëy bu ngeen xamoon !
12يَغْفِرْ لَكُمْ ذُنُوبَكُمْ وَيُدْخِلْكُمْ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ وَمَسَاكِنَ طَيِّبَةً فِي جَنَّاتِ عَدْنٍ ۚ ذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
kon dey dana leen jéggal seeni bàkkaar te it dana leen tàbbal ay Àjjana yu ay dex di daw ci suufam, ak ay dëkkuwaay yu teey ci Àjjanay adan ? Loolu mooy texe gu mag ga
13وَأُخْرَىٰ تُحِبُّونَهَا ۖ نَصْرٌ مِّنَ اللَّهِ وَفَتْحٌ قَرِيبٌ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ
dana leen defal it yeneeni mbir yu ngeen bëgg : ndimbal [lu bawoo] fa Yàlla ak ndam lu jige. Bégalal jullit ñi ci xibaar bu neex bi.
14يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا كُونُوا أَنصَارَ اللَّهِ كَمَا قَالَ عِيسَى ابْنُ مَرْيَمَ لِلْحَوَارِيِّينَ مَنْ أَنصَارِي إِلَى اللَّهِ ۖ قَالَ الْحَوَارِيُّونَ نَحْنُ أَنصَارُ اللَّهِ ۖ فَآمَنَت طَّائِفَةٌ مِّن بَنِي إِسْرَائِيلَ وَكَفَرَت طَّائِفَةٌ ۖ فَأَيَّدْنَا الَّذِينَ آمَنُوا عَلَىٰ عَدُوِّهِمْ فَأَصْبَحُوا ظَاهِرِينَ
eey yéen ñi gëm ! Nangeen doon ay farandooy Yàlla, kem ni Iisaa doomu Maryaama waxe woon taalibeem ya ne leen : “ Ana ñan ñooy doon samay farandoo yi jëm ci Yàlla ? ” – Taalube ya ne ko : “Nun ñoo di farandoo ya jëm ca Yàlla”. Mu am Kureel ci Banii-Israayiila bu gëm na, mu am it Kureel bu weddi. Nu daldi dooleel ña gëm ca kaw seeni noon, ñu daldi am ndam.
As-SaffFihi Alxuraan
14Aaya
MedinanRevelation
13Aaya
Tekki — As-Saff 13
Simoore As-Saff Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dana leen defal it yeneeni mbir yu ngeen bëgg :…Simoore Aaya 13/14 — As-Saff الصف (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saff Dégg, As-Saff Tekki, As-Saff mp3, As-Saff pdf. Aaya 11–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








