At-Taghabun · 17/18
Tekki Waxtaan — At-Taghabun
إِن تُقْرِضُوا اللَّهَ قَرْضًا حَسَنًا يُضَاعِفْهُ لَكُمْ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ شَكُورٌ حَلِيمٌ ۝١٧
In tuqridul laaha qardan hasanany yudd`ifhu lakum wa yaghfir lakum; wallaahu Shakoorun Haleem
📖 Tekkim Wolof
Su ngeen lebalee Yàlla bor bu rafet, Dana leen ko fulal te it dana leen jéggal. Te Yàlla ab Santaakoon la Ku lewet la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 15-18 — At-Taghabun

15إِنَّمَا أَمْوَالُكُمْ وَأَوْلَادُكُمْ فِتْنَةٌ ۚ وَاللَّهُ عِندَهُ أَجْرٌ عَظِيمٌ
Seeni alal ak seeni doom sànje la ci yéen, (Waaye) la nekk fa Yàlla moo di pey gu màgg.
16فَاتَّقُوا اللَّهَ مَا اسْتَطَعْتُمْ وَاسْمَعُوا وَأَطِيعُوا وَأَنفِقُوا خَيْرًا لِّأَنفُسِكُمْ ۗ وَمَن يُوقَ شُحَّ نَفْسِهِ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Nangeen di ragal Yàlla seen kem kàttan, dégluleen, te topp te joxe alal. Moo gën ci yéen de. Képp ku mucc ci ag nay (na xam ne)... ñoo di ña baaxle.
17إِن تُقْرِضُوا اللَّهَ قَرْضًا حَسَنًا يُضَاعِفْهُ لَكُمْ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ شَكُورٌ حَلِيمٌ
Su ngeen lebalee Yàlla bor bu rafet, Dana leen ko fulal te it dana leen jéggal. Te Yàlla ab Santaakoon la Ku lewet la.
18عَالِمُ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Mooy aji Xam ji Kumpaak li feeñ, di boroom Kàttan, di aji Xereñ.
At-TaghabunFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
17Aaya

Tekki — At-Taghabun 17

Simoore At-Taghabun Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su ngeen lebalee Yàlla bor bu rafet, Dana leen ko…

Simoore Aaya 17/18 — At-Taghabun التغابن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Taghabun Dégg, At-Taghabun Tekki, At-Taghabun mp3, At-Taghabun pdf. Aaya 15–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers