Al-Qalam · 4/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
وَإِنَّكَ لَعَلَىٰ خُلُقٍ عَظِيمٍ ۝٤
Wa innaka la`alaa khuluqin `azeem
📖 Tekkim Wolof
Te yaa ngi làmboo, ak jikko yu màgg.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Qalam

2مَا أَنتَ بِنِعْمَةِ رَبِّكَ بِمَجْنُونٍ
Sa xéewali Boroom (yaw Muhammad), tax na ba dofoo.
3وَإِنَّ لَكَ لَأَجْرًا غَيْرَ مَمْنُونٍ
Te itam, am nga pey gu dootul dog.
4وَإِنَّكَ لَعَلَىٰ خُلُقٍ عَظِيمٍ
Te yaa ngi làmboo, ak jikko yu màgg.
5فَسَتُبْصِرُ وَيُبْصِرُونَ
Danga gis ñoom it danañu gis.
6بِأَييِّكُمُ الْمَفْتُونُ
Ana kan ci yéen moo sànku.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Qalam 4

Simoore Al-Qalam Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te yaa ngi làmboo, ak jikko yu màgg.

Simoore Aaya 4/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers