Al-Qalam · 5/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَسَتُبْصِرُ وَيُبْصِرُونَ ۝٥
Fasatubsiru wa yubsiroon
📖 Tekkim Wolof
Danga gis ñoom it danañu gis.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Qalam

3وَإِنَّ لَكَ لَأَجْرًا غَيْرَ مَمْنُونٍ
Te itam, am nga pey gu dootul dog.
4وَإِنَّكَ لَعَلَىٰ خُلُقٍ عَظِيمٍ
Te yaa ngi làmboo, ak jikko yu màgg.
5فَسَتُبْصِرُ وَيُبْصِرُونَ
Danga gis ñoom it danañu gis.
6بِأَييِّكُمُ الْمَفْتُونُ
Ana kan ci yéen moo sànku.
7إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Te sa Boroom moo gën a xam ku réere aw Yoonam, te it moo gën a xam ñay gindiku.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Qalam 5

Simoore Al-Qalam Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danga gis ñoom it danañu gis.

Simoore Aaya 5/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers