Al-Qalam · 6/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
بِأَييِّكُمُ الْمَفْتُونُ ۝٦
Bi ayyikumul maftoon
📖 Tekkim Wolof
Ana kan ci yéen moo sànku.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Qalam

4وَإِنَّكَ لَعَلَىٰ خُلُقٍ عَظِيمٍ
Te yaa ngi làmboo, ak jikko yu màgg.
5فَسَتُبْصِرُ وَيُبْصِرُونَ
Danga gis ñoom it danañu gis.
6بِأَييِّكُمُ الْمَفْتُونُ
Ana kan ci yéen moo sànku.
7إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Te sa Boroom moo gën a xam ku réere aw Yoonam, te it moo gën a xam ñay gindiku.
8فَلَا تُطِعِ الْمُكَذِّبِينَ
Bul topp mukk ñiy fen,
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Qalam 6

Simoore Al-Qalam Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana kan ci yéen moo sànku.

Simoore Aaya 6/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers