Al-Haqqa · 4/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
كَذَّبَتْ ثَمُودُ وَعَادٌ بِالْقَارِعَةِ ۝٤
Kazzabat samoodu wa `Aadum bil qaari`ah
📖 Tekkim Wolof
Giirug Aad ak Samuud dañoo weddi woon yëngu-yëngu bu rëy ba.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Haqqa

2مَا الْحَاقَّةُ
Lan mooy Joxoñub dëgg ba.
3وَمَا أَدْرَاكَ مَا الْحَاقَّةُ
Ana lan moo lay xamal Joxoñub dëgg ba.
4كَذَّبَتْ ثَمُودُ وَعَادٌ بِالْقَارِعَةِ
Giirug Aad ak Samuud dañoo weddi woon yëngu-yëngu bu rëy ba.
5فَأَمَّا ثَمُودُ فَأُهْلِكُوا بِالطَّاغِيَةِ
Giirug Samuud ag yuuxu (am riir) la ñu léen alage.
6وَأَمَّا عَادٌ فَأُهْلِكُوا بِرِيحٍ صَرْصَرٍ عَاتِيَةٍ
Giirug Aad nag ngelaw lu sedd luy riddi moom la ñu léen alage.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Haqqa 4

Simoore Al-Haqqa Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Giirug Aad ak Samuud dañoo weddi woon yëngu-yëngu bu rëy…

Simoore Aaya 4/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers