Al-A'raf · 179/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَلَقَدْ ذَرَأْنَا لِجَهَنَّمَ كَثِيرًا مِّنَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ ۖ لَهُمْ قُلُوبٌ لَّا يَفْقَهُونَ بِهَا وَلَهُمْ أَعْيُنٌ لَّا يُبْصِرُونَ بِهَا وَلَهُمْ آذَانٌ لَّا يَسْمَعُونَ بِهَا ۚ أُولَٰئِكَ كَالْأَنْعَامِ بَلْ هُمْ أَضَلُّ ۚ أُولَٰئِكَ هُمُ الْغَافِلُونَ ۝١٧٩
Wa laqad zaraanaa li jahannama kaseeram minal jinni wal insi lahum quloobul laa yafqahoona bihaa wa lahum a`yunul laa yubisiroona bihaa wa lahum aazaanul laa yasma`oona bihaa; ulaaa`ika kal an`aami bal hum adall; ulaaa`ika humul ghaafiloon
📖 Tekkim Wolof
Nun bind nanu ba noppi ngir Safara jinne yu bari ak nit. Ñeel na leen xol yu dul am dégg-dégg. Ay bët yu ñu dul gis ak ay nopp yu ñu dul dégge. Ñooña, dañoo mel ni mala ya, ñoo leen gën a réer sax. Ñooy ñu sàggan ña.

🎧 Dégg


📜 Aaya 177-181 — Al-A'raf

177سَاءَ مَثَلًا الْقَوْمُ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَأَنفُسَهُمْ كَانُوا يَظْلِمُونَ
Nekkinu nit ña weddi Sunuy kàddu, aka bon, waaye seen bopp lañuy tooñ nag.
178مَن يَهْدِ اللَّهُ فَهُوَ الْمُهْتَدِي ۖ وَمَن يُضْلِلْ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Ku Yàlla gindi nag, mu nekk cig njub. Ña Mu bàyyi cig réer, ñooy ñu yàqule ña.
179وَلَقَدْ ذَرَأْنَا لِجَهَنَّمَ كَثِيرًا مِّنَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ ۖ لَهُمْ قُلُوبٌ لَّا يَفْقَهُونَ بِهَا وَلَهُمْ أَعْيُنٌ لَّا يُبْصِرُونَ بِهَا وَلَهُمْ آذَانٌ لَّا يَسْمَعُونَ بِهَا ۚ أُولَٰئِكَ كَالْأَنْعَامِ بَلْ هُمْ أَضَلُّ ۚ أُولَٰئِكَ هُمُ الْغَافِلُونَ
Nun bind nanu ba noppi ngir Safara jinne yu bari ak nit. Ñeel na leen xol yu dul am dégg-dégg. Ay bët yu ñu dul gis ak ay nopp yu ñu dul dégge. Ñooña, dañoo mel ni mala ya, ñoo leen gën a réer sax. Ñooy ñu sàggan ña.
180وَلِلَّهِ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ فَادْعُوهُ بِهَا ۖ وَذَرُوا الَّذِينَ يُلْحِدُونَ فِي أَسْمَائِهِ ۚ سَيُجْزَوْنَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Yàllaa moom tur yu rafet yi. Nangeen ko ciy jaamu te ngeen dëddu ña di jeng ci turam yi : dees na leen feye la ñu daan def.
181وَمِمَّنْ خَلَقْنَا أُمَّةٌ يَهْدُونَ بِالْحَقِّ وَبِهِ يَعْدِلُونَ
Nekk na ci ñi Nu bind, xeet woo xam ne danañu gindiku ci dëgg te danañu maandu.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
179Aaya

Tekki — Al-A'raf 179

Simoore Al-A'raf Aaya 179 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun bind nanu ba noppi ngir Safara jinne yu bari…

Simoore Aaya 179/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 177–181. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers