Al-Ma'arij · 23/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
الَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَاتِهِمْ دَائِمُونَ ۝٢٣
Allazeena hum `alaa Salaatihim daaa`imoon
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne dañuy saxoo Julli,

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Ma'arij

21وَإِذَا مَسَّهُ الْخَيْرُ مَنُوعًا
su ko jàmm ganesee mu nay, alal ak yiw danay tax mu nay bew.
22إِلَّا الْمُصَلِّينَ
Ba mu des jullikat yi
23الَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَاتِهِمْ دَائِمُونَ
ña nga xam ne dañuy saxoo Julli,
24وَالَّذِينَ فِي أَمْوَالِهِمْ حَقٌّ مَّعْلُومٌ
ña nga xam ne seeni alal sàkk nañu ca cér bus xam jagle ko
25لِّلسَّائِلِ وَالْمَحْرُومِ
mu ñéel yalwaankat yeek ñu ñakk ñi ;
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 23

Simoore Al-Ma'arij Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne dañuy saxoo Julli,

Simoore Aaya 23/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers