Al-Ma'arij · 22/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
إِلَّا الْمُصَلِّينَ ۝٢٢
Illal musalleen
📖 Tekkim Wolof
Ba mu des jullikat yi

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Ma'arij

20إِذَا مَسَّهُ الشَّرُّ جَزُوعًا
su ko aw ay laalee, muy saalit ;
21وَإِذَا مَسَّهُ الْخَيْرُ مَنُوعًا
su ko jàmm ganesee mu nay, alal ak yiw danay tax mu nay bew.
22إِلَّا الْمُصَلِّينَ
Ba mu des jullikat yi
23الَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَاتِهِمْ دَائِمُونَ
ña nga xam ne dañuy saxoo Julli,
24وَالَّذِينَ فِي أَمْوَالِهِمْ حَقٌّ مَّعْلُومٌ
ña nga xam ne seeni alal sàkk nañu ca cér bus xam jagle ko
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 22

Simoore Al-Ma'arij Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu des jullikat yi

Simoore Aaya 22/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers