Al-Ma'arij · 41/44
Tekki Waxtaan — Al-Ma'arij
عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ خَيْرًا مِّنْهُمْ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ ٤١
Transliteration
Alaaa an nubaddila khairam minhum wa maa Nahnu bimasbooqeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ci soppi wuutale leen ak ñeneen ñu leen gën, te kenn du ko fanq.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 39-43 — Al-Ma'arij
39كَلَّا ۖ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّمَّا يَعْلَمُونَ
Mukk ! Noo leen sàkk ak ni ñu ko xame.
40فَلَا أُقْسِمُ بِرَبِّ الْمَشَارِقِ وَالْمَغَارِبِ إِنَّا لَقَادِرُونَ
Déedéet !... Maa ngi giñ ci Boroom Penku ak Sowu yi ci ne Nun boroom Kàttan la nu.
41عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ خَيْرًا مِّنْهُمْ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ
Ci soppi wuutale leen ak ñeneen ñu leen gën, te kenn du ko fanq.
42فَذَرْهُمْ يَخُوضُوا وَيَلْعَبُوا حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي يُوعَدُونَ
Bàyyileen ñu nuur (ci kéefër) aka fo ba baa ñuy dajeek bis ba ñu leen daan digu,
43يَوْمَ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ سِرَاعًا كَأَنَّهُمْ إِلَىٰ نُصُبٍ يُوفِضُونَ
bu keroogee, ba ñuy génn bàmmeel ya gaaw melni ku jëm ciy xërëm ;
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
41Aaya
Tekki — Al-Ma'arij 41
Simoore Al-Ma'arij Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ci soppi wuutale leen ak ñeneen ñu leen gën, te…Simoore Aaya 41/44 — Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ma'arij Dégg, Al-Ma'arij Tekki, Al-Ma'arij mp3, Al-Ma'arij pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








