Al-Ma'arij · 42/44
Tekki Waxtaan — Al-Ma'arij
فَذَرْهُمْ يَخُوضُوا وَيَلْعَبُوا حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي يُوعَدُونَ ۝٤٢
Fazarhum yakhoodoo wa yal`aboo hattaa yulaaqoo yaw mahumul lazee yoo`adoon
📖 Tekkim Wolof
Bàyyileen ñu nuur (ci kéefër) aka fo ba baa ñuy dajeek bis ba ñu leen daan digu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Al-Ma'arij

40فَلَا أُقْسِمُ بِرَبِّ الْمَشَارِقِ وَالْمَغَارِبِ إِنَّا لَقَادِرُونَ
Déedéet !... Maa ngi giñ ci Boroom Penku ak Sowu yi ci ne Nun boroom Kàttan la nu.
41عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ خَيْرًا مِّنْهُمْ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ
Ci soppi wuutale leen ak ñeneen ñu leen gën, te kenn du ko fanq.
42فَذَرْهُمْ يَخُوضُوا وَيَلْعَبُوا حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي يُوعَدُونَ
Bàyyileen ñu nuur (ci kéefër) aka fo ba baa ñuy dajeek bis ba ñu leen daan digu,
43يَوْمَ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ سِرَاعًا كَأَنَّهُمْ إِلَىٰ نُصُبٍ يُوفِضُونَ
bu keroogee, ba ñuy génn bàmmeel ya gaaw melni ku jëm ciy xërëm ;
44خَاشِعَةً أَبْصَارُهُمْ تَرْهَقُهُمْ ذِلَّةٌ ۚ ذَٰلِكَ الْيَوْمُ الَّذِي كَانُوا يُوعَدُونَ
seen gët ya sajju, ñu torox ngir gàcce. Bis boobee mooy ba ñu leen daan dig (tëkoo)!
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 42

Simoore Al-Ma'arij Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bàyyileen ñu nuur (ci kéefër) aka fo ba baa ñuy…

Simoore Aaya 42/44 — Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ma'arij Dégg, Al-Ma'arij Tekki, Al-Ma'arij mp3, Al-Ma'arij pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers