Nuh · 11/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا ۝١١
Yursilis samaaa`a `alaikum midraaraa
📖 Tekkim Wolof
kon dey dana yabal asamaan si, mu duttil leen taw,

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Nuh

9ثُمَّ إِنِّي أَعْلَنتُ لَهُمْ وَأَسْرَرْتُ لَهُمْ إِسْرَارًا
Topp, biralalnaa leen, yalolnaa leen.
10فَقُلْتُ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ إِنَّهُ كَانَ غَفَّارًا
Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey Jégëlaakoon la,
11يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا
kon dey dana yabal asamaan si, mu duttil leen taw,
12وَيُمْدِدْكُم بِأَمْوَالٍ وَبَنِينَ وَيَجْعَل لَّكُمْ جَنَّاتٍ وَيَجْعَل لَّكُمْ أَنْهَارًا
te it dana leen may ay alal ak i doom, te dana leen defal tooli dër ak ay dex.
13مَّا لَكُمْ لَا تَرْجُونَ لِلَّهِ وَقَارًا
Ana lu leen dal ba du ngeen delloo Yàlla njukël,
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Nuh 11

Simoore Nuh Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kon dey dana yabal asamaan si, mu duttil leen taw,

Simoore Aaya 11/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers