Nuh · 12/28
Tekki Waxtaan — Nuh
وَيُمْدِدْكُم بِأَمْوَالٍ وَبَنِينَ وَيَجْعَل لَّكُمْ جَنَّاتٍ وَيَجْعَل لَّكُمْ أَنْهَارًا ۝١٢
Wa yumdidkum bi am waalinw wa baneena wa yaj`al lakum Jannaatinw wa yaj`al lakum anhaaraa
📖 Tekkim Wolof
te it dana leen may ay alal ak i doom, te dana leen defal tooli dër ak ay dex.
🎧 Dégg

📜 Aaya 10-14 — Nuh

10فَقُلْتُ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ إِنَّهُ كَانَ غَفَّارًا
Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey Jégëlaakoon la,
11يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا
kon dey dana yabal asamaan si, mu duttil leen taw,
12وَيُمْدِدْكُم بِأَمْوَالٍ وَبَنِينَ وَيَجْعَل لَّكُمْ جَنَّاتٍ وَيَجْعَل لَّكُمْ أَنْهَارًا
te it dana leen may ay alal ak i doom, te dana leen defal tooli dër ak ay dex.
13مَّا لَكُمْ لَا تَرْجُونَ لِلَّهِ وَقَارًا
Ana lu leen dal ba du ngeen delloo Yàlla njukël,
14وَقَدْ خَلَقَكُمْ أَطْوَارًا
te moom moo leen jaarale ci ay tolluwaay yu bari ba mu leen di sàkk ?
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Nuh 12

Simoore Nuh Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te it dana leen may ay alal ak i doom,…

Simoore Aaya 12/28 — Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Nuh Dégg, Nuh Tekki, Nuh mp3, Nuh pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers