Nuh · 10/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
فَقُلْتُ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ إِنَّهُ كَانَ غَفَّارًا ۝١٠
Faqultus taghfiroo Rabakam innahoo kaana Ghaffaaraa
📖 Tekkim Wolof
Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey Jégëlaakoon la,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 8-12 — Simoore Nuh

8ثُمَّ إِنِّي دَعَوْتُهُمْ جِهَارًا
Topp, woonaa leen cig jooru.
9ثُمَّ إِنِّي أَعْلَنتُ لَهُمْ وَأَسْرَرْتُ لَهُمْ إِسْرَارًا
Topp, biralalnaa leen, yalolnaa leen.
10فَقُلْتُ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ إِنَّهُ كَانَ غَفَّارًا
Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey Jégëlaakoon la,
11يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا
kon dey dana yabal asamaan si, mu duttil leen taw,
12وَيُمْدِدْكُم بِأَمْوَالٍ وَبَنِينَ وَيَجْعَل لَّكُمْ جَنَّاتٍ وَيَجْعَل لَّكُمْ أَنْهَارًا
te it dana leen may ay alal ak i doom, te dana leen defal tooli dër ak ay dex.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Nuh 10

Simoore Nuh Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey…

Simoore Aaya 10/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers