Nuh · 19/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ بِسَاطًا ۝١٩
Wallaahu ja`ala lakumul arda bisaataa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla moo leen defaral suuf si mu di laltaay,

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Nuh

17وَاللَّهُ أَنبَتَكُم مِّنَ الْأَرْضِ نَبَاتًا
Te Yàllaa leen saxal, ci suuf si, ni gàncax,
18ثُمَّ يُعِيدُكُمْ فِيهَا وَيُخْرِجُكُمْ إِخْرَاجًا
te dana leen ca delloo dana leen ca génneewaat.
19وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ بِسَاطًا
Yàlla moo leen defaral suuf si mu di laltaay,
20لِّتَسْلُكُوا مِنْهَا سُبُلًا فِجَاجًا
ngir ngeen mana sóobu ca yoonam yu dàndante ya”.
21قَالَ نُوحٌ رَّبِّ إِنَّهُمْ عَصَوْنِي وَاتَّبَعُوا مَن لَّمْ يَزِدْهُ مَالُهُ وَوَلَدُهُ إِلَّا خَسَارًا
Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit) moy na ñu ma dem toppi koo xam ne alalam ak i doomam jariñu ko lu dul yàqule.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Nuh 19

Simoore Nuh Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla moo leen defaral suuf si mu di laltaay,

Simoore Aaya 19/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers