Nuh · 20/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
لِّتَسْلُكُوا مِنْهَا سُبُلًا فِجَاجًا ۝٢٠
Litaslukoo minhaa subulan fijaajaa
📖 Tekkim Wolof
ngir ngeen mana sóobu ca yoonam yu dàndante ya”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore Nuh

18ثُمَّ يُعِيدُكُمْ فِيهَا وَيُخْرِجُكُمْ إِخْرَاجًا
te dana leen ca delloo dana leen ca génneewaat.
19وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ بِسَاطًا
Yàlla moo leen defaral suuf si mu di laltaay,
20لِّتَسْلُكُوا مِنْهَا سُبُلًا فِجَاجًا
ngir ngeen mana sóobu ca yoonam yu dàndante ya”.
21قَالَ نُوحٌ رَّبِّ إِنَّهُمْ عَصَوْنِي وَاتَّبَعُوا مَن لَّمْ يَزِدْهُ مَالُهُ وَوَلَدُهُ إِلَّا خَسَارًا
Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit) moy na ñu ma dem toppi koo xam ne alalam ak i doomam jariñu ko lu dul yàqule.
22وَمَكَرُوا مَكْرًا كُبَّارًا
Ña ngay fexe pexe yu rëy,
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Nuh 20

Simoore Nuh Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngir ngeen mana sóobu ca yoonam yu dàndante ya”.

Simoore Aaya 20/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers