Al-Jinn · 14/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
وَأَنَّا مِنَّا الْمُسْلِمُونَ وَمِنَّا الْقَاسِطُونَ ۖ فَمَنْ أَسْلَمَ فَأُولَٰئِكَ تَحَرَّوْا رَشَدًا ۝١٤
Wa annaa minnal muslimoona wa minnal qaasitoona faman aslama fa ulaaa`ika taharraw rashadaa
📖 Tekkim Wolof
Am na ci nun ay jullit, am na it ci nun ay tooñkat. Ña nga xam ne ñoom dañoo tuub defi jullit ñoo ñaa làmboo njub.
🎧 Dégg

📜 Aaya 12-16 — Al-Jinn

12وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن نُّعْجِزَ اللَّهَ فِي الْأَرْضِ وَلَن نُّعْجِزَهُ هَرَبًا
Te xam nanu ne manuñoo tiiñ Yàlla te it manuñoo daw mukk ba raw ko.
13وَأَنَّا لَمَّا سَمِعْنَا الْهُدَىٰ آمَنَّا بِهِ ۖ فَمَن يُؤْمِن بِرَبِّهِ فَلَا يَخَافُ بَخْسًا وَلَا رَهَقًا
Te nun ba nu déggee njub ga [Alxuraan], gëm nanu ko, te nag képp ku gëm Boroomam dootul ragal wàññikug jëf waxantumalaak sànje.
14وَأَنَّا مِنَّا الْمُسْلِمُونَ وَمِنَّا الْقَاسِطُونَ ۖ فَمَنْ أَسْلَمَ فَأُولَٰئِكَ تَحَرَّوْا رَشَدًا
Am na ci nun ay jullit, am na it ci nun ay tooñkat. Ña nga xam ne ñoom dañoo tuub defi jullit ñoo ñaa làmboo njub.
15وَأَمَّا الْقَاسِطُونَ فَكَانُوا لِجَهَنَّمَ حَطَبًا
Tooñkat ya nag, ñoom ñoo di mattum safara.
16وَأَن لَّوِ اسْتَقَامُوا عَلَى الطَّرِيقَةِ لَأَسْقَيْنَاهُم مَّاءً غَدَقًا
Te kat su ñu jaaroon ca yoon wu jub xocc wa, Danaa leen nàndale, ndox mu neex,
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Jinn 14

Simoore Al-Jinn Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am na ci nun ay jullit, am na it ci…

Simoore Aaya 14/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers