Al-Jinn · 3/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
وَأَنَّهُ تَعَالَىٰ جَدُّ رَبِّنَا مَا اتَّخَذَ صَاحِبَةً وَلَا وَلَدًا ۝٣
Wa annahoo Ta`aalaa jaddu Rabbinaa mat takhaza saahibatanw wa la waladaa
📖 Tekkim Wolof
Te sunu Boroom - màggam ga sell na - jàppewul kenn muy soxnaam, waxatumalaa doomam !

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Jinn

1قُلْ أُوحِيَ إِلَيَّ أَنَّهُ اسْتَمَعَ نَفَرٌ مِّنَ الْجِنِّ فَقَالُوا إِنَّا سَمِعْنَا قُرْآنًا عَجَبًا
Waxal ne : “Soloof na ma am na mbooleem jinne muy déglu, bay wax naan : “Nun dey dégg nanu Ñjàngum [Alxuraan] mu yéeme,
2يَهْدِي إِلَى الرُّشْدِ فَآمَنَّا بِهِ ۖ وَلَن نُّشْرِكَ بِرَبِّنَا أَحَدًا
dafay gindee jëme ci njub. Nu daldi koy gëm, te dunu bokkaale dara ci sunu Boroom.
3وَأَنَّهُ تَعَالَىٰ جَدُّ رَبِّنَا مَا اتَّخَذَ صَاحِبَةً وَلَا وَلَدًا
Te sunu Boroom - màggam ga sell na - jàppewul kenn muy soxnaam, waxatumalaa doomam !
4وَأَنَّهُ كَانَ يَقُولُ سَفِيهُنَا عَلَى اللَّهِ شَطَطًا
Sunu kannas ma [Ibliis] moodaan wax ay njaxum ci Yàlla.
5وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن تَقُولَ الْإِنسُ وَالْجِنُّ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا
Te foog na ne nit ak jinne amul kenn ku cay fenal Yàlla.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Jinn 3

Simoore Al-Jinn Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sunu Boroom - màggam ga sell na - jàppewul…

Simoore Aaya 3/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers