Al-Jinn · 4/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
وَأَنَّهُ كَانَ يَقُولُ سَفِيهُنَا عَلَى اللَّهِ شَطَطًا ۝٤
Wa annahoo kaana yaqoolu safeehunaa `alal laahi shatataa
📖 Tekkim Wolof
Sunu kannas ma [Ibliis] moodaan wax ay njaxum ci Yàlla.
🎧 Dégg

📜 Aaya 2-6 — Al-Jinn

2يَهْدِي إِلَى الرُّشْدِ فَآمَنَّا بِهِ ۖ وَلَن نُّشْرِكَ بِرَبِّنَا أَحَدًا
dafay gindee jëme ci njub. Nu daldi koy gëm, te dunu bokkaale dara ci sunu Boroom.
3وَأَنَّهُ تَعَالَىٰ جَدُّ رَبِّنَا مَا اتَّخَذَ صَاحِبَةً وَلَا وَلَدًا
Te sunu Boroom - màggam ga sell na - jàppewul kenn muy soxnaam, waxatumalaa doomam !
4وَأَنَّهُ كَانَ يَقُولُ سَفِيهُنَا عَلَى اللَّهِ شَطَطًا
Sunu kannas ma [Ibliis] moodaan wax ay njaxum ci Yàlla.
5وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن تَقُولَ الْإِنسُ وَالْجِنُّ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا
Te foog na ne nit ak jinne amul kenn ku cay fenal Yàlla.
6وَأَنَّهُ كَانَ رِجَالٌ مِّنَ الْإِنسِ يَعُوذُونَ بِرِجَالٍ مِّنَ الْجِنِّ فَزَادُوهُمْ رَهَقًا
Amoon ci nit, aw gaay ñu daan sàkku ay muslaay ci aw gaay ñu bokk ci jinne yi ñu faf leen dolli jaaxle (njaaxum).
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Jinn 4

Simoore Al-Jinn Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sunu kannas ma [Ibliis] moodaan wax ay njaxum ci Yàlla.

Simoore Aaya 4/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers