Al-Muzzammil · 5/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muzzammil
إِنَّا سَنُلْقِي عَلَيْكَ قَوْلًا ثَقِيلًا ۝٥
Innaa sanulqee `alika qawalan saqeelaa
📖 Tekkim Wolof
Xalset nanu laa gàll wax ju diis.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Muzzammil

3نِّصْفَهُ أَوِ انقُصْ مِنْهُ قَلِيلًا
Ab xaajam, walla sax nga wàññi ca lu tuuti ;
4أَوْ زِدْ عَلَيْهِ وَرَتِّلِ الْقُرْآنَ تَرْتِيلًا
walla sax nga dolli ca. Te na ngay jàng Alxuraan, njàng mu léer.
5إِنَّا سَنُلْقِي عَلَيْكَ قَوْلًا ثَقِيلًا
Xalset nanu laa gàll wax ju diis.
6إِنَّ نَاشِئَةَ اللَّيْلِ هِيَ أَشَدُّ وَطْئًا وَأَقْوَمُ قِيلًا
Jullig guddi nag moo gëna nangu te moo gëna leer cim njàng.
7إِنَّ لَكَ فِي النَّهَارِ سَبْحًا طَوِيلًا
Am nga, ci bëcëg bi, jot gu gudd goo mana lijantee.
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 5

Simoore Al-Muzzammil Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xalset nanu laa gàll wax ju diis.

Simoore Aaya 5/20 — Simoore Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muzzammil Dégg, Simoore Al-Muzzammil Tekki, Simoore Al-Muzzammil mp3, Simoore Al-Muzzammil pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers