Al-Muzzammil · 6/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muzzammil
إِنَّ نَاشِئَةَ اللَّيْلِ هِيَ أَشَدُّ وَطْئًا وَأَقْوَمُ قِيلًا ۝٦
Inn naashi`atal laili hiya ashadddu wat anw wa aqwamu qeelaa
📖 Tekkim Wolof
Jullig guddi nag moo gëna nangu te moo gëna leer cim njàng.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Muzzammil

4أَوْ زِدْ عَلَيْهِ وَرَتِّلِ الْقُرْآنَ تَرْتِيلًا
walla sax nga dolli ca. Te na ngay jàng Alxuraan, njàng mu léer.
5إِنَّا سَنُلْقِي عَلَيْكَ قَوْلًا ثَقِيلًا
Xalset nanu laa gàll wax ju diis.
6إِنَّ نَاشِئَةَ اللَّيْلِ هِيَ أَشَدُّ وَطْئًا وَأَقْوَمُ قِيلًا
Jullig guddi nag moo gëna nangu te moo gëna leer cim njàng.
7إِنَّ لَكَ فِي النَّهَارِ سَبْحًا طَوِيلًا
Am nga, ci bëcëg bi, jot gu gudd goo mana lijantee.
8وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ وَتَبَتَّلْ إِلَيْهِ تَبْتِيلًا
Na ngay fàttaliku di tud sa turu Boroom te wéeru ci moom fàwwu,
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 6

Simoore Al-Muzzammil Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jullig guddi nag moo gëna nangu te moo gëna leer…

Simoore Aaya 6/20 — Simoore Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muzzammil Dégg, Simoore Al-Muzzammil Tekki, Simoore Al-Muzzammil mp3, Simoore Al-Muzzammil pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers