Al-Insan · 11/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
فَوَقَاهُمُ اللَّهُ شَرَّ ذَٰلِكَ الْيَوْمِ وَلَقَّاهُمْ نَضْرَةً وَسُرُورًا ۝١١
Fa waqaahumul laahu sharra zaalikal yawmi wa laqqaahum nadratanw wa surooraa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla daldi leen fegal ayu boobale bis, dajale leen ak naataangeek mbégte,

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Insan

9إِنَّمَا نُطْعِمُكُمْ لِوَجْهِ اللَّهِ لَا نُرِيدُ مِنكُمْ جَزَاءً وَلَا شُكُورًا
(te naan leen) : “noo ngi leen koy leele de : waaye bëggu nu ci ak pey walla gëram ngir Yàlla rekk tax.
10إِنَّا نَخَافُ مِن رَّبِّنَا يَوْمًا عَبُوسًا قَمْطَرِيرًا
Danoo ragal, ci sunu Boroom, bis bu ñàng te tëradi”.
11فَوَقَاهُمُ اللَّهُ شَرَّ ذَٰلِكَ الْيَوْمِ وَلَقَّاهُمْ نَضْرَةً وَسُرُورًا
Yàlla daldi leen fegal ayu boobale bis, dajale leen ak naataangeek mbégte,
12وَجَزَاهُم بِمَا صَبَرُوا جَنَّةً وَحَرِيرًا
mu faye leen lañu muñoon, Àjjana ak i sooy,
13مُّتَّكِئِينَ فِيهَا عَلَى الْأَرَائِكِ ۖ لَا يَرَوْنَ فِيهَا شَمْسًا وَلَا زَمْهَرِيرًا
dañuy sóonu ca lal ya, te dunu fa gis ab jant waxantumalaak ab sedd liw.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Insan 11

Simoore Al-Insan Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla daldi leen fegal ayu boobale bis, dajale leen ak…

Simoore Aaya 11/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers