Al-Insan · 10/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
إِنَّا نَخَافُ مِن رَّبِّنَا يَوْمًا عَبُوسًا قَمْطَرِيرًا ۝١٠
Innaa nakhaafu mir Rabbinna Yawman `aboosan qamtareeraa
📖 Tekkim Wolof
Danoo ragal, ci sunu Boroom, bis bu ñàng te tëradi”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Insan

8وَيُطْعِمُونَ الطَّعَامَ عَلَىٰ حُبِّهِ مِسْكِينًا وَيَتِيمًا وَأَسِيرًا
te lañuy bëgg ñam lépp, terewul ñu di ko leel, miskiin, yaak jirim yaak ña ñu tëj kaso,
9إِنَّمَا نُطْعِمُكُمْ لِوَجْهِ اللَّهِ لَا نُرِيدُ مِنكُمْ جَزَاءً وَلَا شُكُورًا
(te naan leen) : “noo ngi leen koy leele de : waaye bëggu nu ci ak pey walla gëram ngir Yàlla rekk tax.
10إِنَّا نَخَافُ مِن رَّبِّنَا يَوْمًا عَبُوسًا قَمْطَرِيرًا
Danoo ragal, ci sunu Boroom, bis bu ñàng te tëradi”.
11فَوَقَاهُمُ اللَّهُ شَرَّ ذَٰلِكَ الْيَوْمِ وَلَقَّاهُمْ نَضْرَةً وَسُرُورًا
Yàlla daldi leen fegal ayu boobale bis, dajale leen ak naataangeek mbégte,
12وَجَزَاهُم بِمَا صَبَرُوا جَنَّةً وَحَرِيرًا
mu faye leen lañu muñoon, Àjjana ak i sooy,
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Insan 10

Simoore Al-Insan Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danoo ragal, ci sunu Boroom, bis bu ñàng te tëradi”.

Simoore Aaya 10/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers