Al-Insan · 18/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
عَيْنًا فِيهَا تُسَمَّىٰ سَلْسَبِيلًا ۝١٨
Aynan feeha tusammaa salsabeelaa
📖 Tekkim Wolof
ab bëtu ndox bu tudd Salsabiil.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Simoore Al-Insan

16قَوَارِيرَ مِن فِضَّةٍ قَدَّرُوهَا تَقْدِيرًا
ay koppi weeri xaalis, yu yem kepp.
17وَيُسْقَوْنَ فِيهَا كَأْسًا كَانَ مِزَاجُهَا زَنجَبِيلًا
Ñu, di leen fa nàndale ak kaas yu ñu njare jinjeer,
18عَيْنًا فِيهَا تُسَمَّىٰ سَلْسَبِيلًا
ab bëtu ndox bu tudd Salsabiil.
19۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ وِلْدَانٌ مُّخَلَّدُونَ إِذَا رَأَيْتَهُمْ حَسِبْتَهُمْ لُؤْلُؤًا مَّنثُورًا
Te ay xalee ngay wër ca ñoom sax cig ndaw. Soo leen gisee, da ngay foog ne peme ju ñu tasaare la ñu.
20وَإِذَا رَأَيْتَ ثَمَّ رَأَيْتَ نَعِيمًا وَمُلْكًا كَبِيرًا
Soo ko gisee, danga fa gIisaale xeewal ak nguur gu màgg.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Insan 18

Simoore Al-Insan Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ab bëtu ndox bu tudd Salsabiil.

Simoore Aaya 18/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers