Al-Mutaffifin · 7/36
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mutaffifin
كَلَّا إِنَّ كِتَابَ الْفُجَّارِ لَفِي سِجِّينٍ ۝٧
Kallaaa inna kitaabal fujjaari lafee Sijjeen
📖 Tekkim Wolof
Déet... ! Waaye téereb kàccoor yaa nga ca Sijjin de

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Mutaffifin

5لِيَوْمٍ عَظِيمٍ
ca bis bu ñàng,
6يَوْمَ يَقُومُ النَّاسُ لِرَبِّ الْعَالَمِينَ
bis ba nit ña di taxaw ci kanam Boroom Àddina si yépp ?
7كَلَّا إِنَّ كِتَابَ الْفُجَّارِ لَفِي سِجِّينٍ
Déet... ! Waaye téereb kàccoor yaa nga ca Sijjin de
8وَمَا أَدْرَاكَ مَا سِجِّينٌ
ana lan moo lay xamal luy Sijjin ?
9كِتَابٌ مَّرْقُومٌ
ab téere la bu ñu xas tàmpe.
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 7

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déet... ! Waaye téereb kàccoor yaa nga ca Sijjin de

Simoore Aaya 7/36 — Simoore Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mutaffifin Dégg, Simoore Al-Mutaffifin Tekki, Simoore Al-Mutaffifin mp3, Simoore Al-Mutaffifin pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers