Al-A'la · 6/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'la
سَنُقْرِئُكَ فَلَا تَنسَىٰ ۝٦
Sanuqri`uka falaa tansaaa
📖 Tekkim Wolof
Dananu la jàngal (Alxuraan), te doo too ko fàtte

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-A'la

4وَالَّذِي أَخْرَجَ الْمَرْعَىٰ
kiy génne ñax mi saxal ko,
5فَجَعَلَهُ غُثَاءً أَحْوَىٰ
di ko naatal dëlël ko.
6سَنُقْرِئُكَ فَلَا تَنسَىٰ
Dananu la jàngal (Alxuraan), te doo too ko fàtte
7إِلَّا مَا شَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ وَمَا يَخْفَىٰ
lu dul la soob Yàlla. Moom moo xam li feeñ ak li nëbbu.
8وَنُيَسِّرُكَ لِلْيُسْرَىٰ
Dananu la jàppandalal yoon wi gëna yomb.
Al-A'laFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-A'la 6

Simoore Al-A'la Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dananu la jàngal (Alxuraan), te doo too ko fàtte

Simoore Aaya 6/19 — Simoore Al-A'la الأعلى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'la Dégg, Simoore Al-A'la Tekki, Simoore Al-A'la mp3, Simoore Al-A'la pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers